Deuteronomy 29:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen ñi taxaw ci sunu biir tey, fi sunu kanam Yàlla Aji Sax ji, ci ngeen bokk, waaye ñi dikkagul bay bokk ak nun taxaw fii it, ci lañu.