bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 29:22
Deuteronomy 29:22 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
tamarax ak xorom, ak lakk gi ci seen réew mépp, ba du lenn lees fay ji, mbaa lu fay jebbi, mbaa genn gàncax gu fay saxe, mbete tastey Sodom, ak Gomor ak Atma ak Ceboyim, dëkk ya Aji Sax ji tas, ca meram ma ak sànjam ma,