Deuteronomy 29:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne leen: «Li ko waral mooy, dañoo fecci kóllërey Aji Sax ji, seen Yàllay maam, te mu fasoon ko ak ñoom ba mu leen jëlee réewum Misra.