Deuteronomy 3:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba keroog Aji Sax ji noppalee seen bokki bànni Israyil ni yeen, fekk leen nangu, ñoom it, réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox, ca wàllaa dexu Yurdan. Su ko defee ku nekk ci yeen saña dellu ca céru suufam ba ma ko jox.»