Deuteronomy 3:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yosuwe itam, sant naa ko ci jant yooyu ne ko: «Sa bët moo la may mboolem ni seen Yàlla Aji Sax ji def ak ñaari buur yii. Noonu rekk la Aji Sax jiy def ak mboolem nguur ya nga jëm.