Deuteronomy 3:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye nanga yebal Yosuwe, ñaax ko, jàjj ko, ndax moom mooy jàll, jiite mbooloo mii, te moo leen di jox réew moomu ngay séen.»