Deuteronomy 3:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba lanu nangu mboolemi dëkkam. Amul benn dëkk bu nu nanguwul ci ñoom: juróom benn fukki dëkk, mboolem diiwaanu Argob, ba bokk ca nguurug Og ca Basan.