Deuteronomy 30:19 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Woo naa seede asamaan ak suuf ci yeen, bésub tey: dund ak ndee laa teg fi seen kanam, ak barke ak alkànde. Taamuleen dund ndax ngeen dund, yeen ak seen askan.