Deuteronomy 30:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su boobaa seen Yàlla Aji Sax jee leen di xarfal xarafu xol, te mooy xarfal xarafu xol, seen askan, ngir ngeen soppe seen Yàlla Aji Sax ji seen léppi xol, ak seen léppi bakkan, ndax ngeen dund.