Deuteronomy 31:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ko defee seen doom yi xamul dinañu ci dégg, ba tàggatu ci ragal seen Yàlla Aji Sax ji, mboolem fan ya ngeen di dund ca réew, ma ngeen jàll dexu Yurdan, jëm fa, ngir nanguji ko.»