Deuteronomy 31:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Jël-leen téereb yoon wii, ngeen teg ko ci seen wetu gaalu kóllërey Yàlla Aji Sax ji, mu doon fa ab seede, ngir àtte leen.