Deuteronomy 31:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa ne gannaaw bu ma deeyee, dingeen defa def ag yàqute, dingeen teggi yoon wi ma leen jaarloo woon, te musibaa leen di mujj dikkal, ndax yeenay def jëf ju bon ju Aji Sax ji ñaawlu, ba merloo ko ndax seeni jëf.»