Deuteronomy 31:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen Yàlla Aji Sax ji ci boppam moo leen di jiite jàll. Mooy fàkkas xeet yooyu fi seen kanam, ngeen nangu seenum réew. Yosuwe moo leen di jiite jàll, na ko Aji Sax ji waxe woon.