Deuteronomy 31:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Musaa moo bind kàddug yoon wii, dénk ko doomi Lewi yu góor, sarxalkat yay gàddu gaalu kóllërey Aji Sax ji, ñook magi Israyil ñépp.