Deuteronomy 32:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye reetaani noon laa ci ragal, lu ko moy seeni bañ juume ko, ba naan: “Sunu njàmbaar a!” te waroon ne: “Aji Sax jee def lii lépp!”»