Deuteronomy 32:47 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat du kàddug neen ci yeen. Mooy seenug dund! Ci gii kàddu ngeen di gudde fan, ca réew ma ngeen di jàll dexu Yurdan jëm fa, ngir nanguji ko.»