Deuteronomy 32:51 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ko waral mooy yeena ma fecci worma ci digg bànni Israyil, ca ndoxi Meriba Kades, ca màndiŋu Ciin, ndax yeena wormaalul sama sellnga ci digg bànni Israyil.