bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 33:17
Deuteronomy 33:17 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Taawub yëkk la, daraja mooy boroom, béjjén ya, béjjéni nagu àll la, ca lay butteendoo xeet yépp, ba ca cati àddina. Ñooñooy junniy junniy nit ca giirug Efrayim, ak junni ca giirug Manase.