Deuteronomy 33:20 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gàdd la wax ne ko: Barke ñeel na ku yaatal Gàdd. Ni gaynde la goore, te mooy xotat përëg akum kaaŋ.