Deuteronomy 33:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo xool cér ba jëkka lew, jagoo ko, nde fa la wàllu njiit di xaar boroom. Moo fekksi njiiti askan wi, moo jëfe njekku Aji Sax ji, aki dogalam fi Israyil.