Deuteronomy 33:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dan la wax ne ko: Dan gaynde gu ndaw la, mooy tëbe fa diiwaanu Basan.