Deuteronomy 33:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii nag moo ñeel Yuda. Mu ne: Éy Aji Sax ji déggal yuuxi Yuda te yóbbu ko ciy bokkam. Mooy jànkoontee dooley boppam, waaye yaa koy wallu ciy noonam.