Deuteronomy 33:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lewi la wax ne ko: Sa Tumim ak sa Urim, jumtukaayi tegtal ya, ñeel na góor gay sa wóllëre, yaa ko nattoo ca Maasa, joteek moom ca ndoxum Meriba.