Deuteronomy 34:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba ca mboolem firnde yaak kéemaan ya ko Aji Sax ji yebale woon, ngir mu def ko ca biir réewum Misra, ca Firawna ak jawriñam ñépp, ak ca biir réewam mépp,