Deuteronomy 4:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Léegi nag yeen waa Israyil, dégluleen dogali yoon yeek àttey yoon yii ma leen di xamal, ngir ngeen di ko jëfe, ndax ngeen dund ba dugg, nanguji réew ma leen Aji Sax ji seen Yàllay maam, di jox.