Deuteronomy 4:15 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nangeen wattu seen bopp bu baax nag ndax keroog ba Aji Sax jiy àddoo ca digg sawara wa, wax ak yeen ca tundu Oreb, gisuleen jenn jëmm.