Deuteronomy 4:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye yeena tax Aji Sax ji mere ma ba giñ ne duma jàll dexu Yurdan, te duma dugg ca réew mu baax, ma leen seen Yàlla Aji Sax ji moomale.