Deuteronomy 4:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man nag ci réew mii laay dee. Du maay jàll dexu Yurdan. Waaye yeen yeenay jàll, ba nanguji réew mu baax moomu.