Deuteronomy 4:32 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seetleen rekk ci janti démb yi leen jiitu, la dale bés ba Yàlla sàkke nit fi kaw suuf, mbaa ngeen seet asamaan, cat ba cat. Ndax lu màgge nii mas naa am? Am masees naa dégg lu ni mel?