Deuteronomy 4:35 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen déy lañu won loolu lépp ngir ngeen xam ne Aji Sax ji doŋŋ mooy Yàlla, te jeneen yàlla amul, ju dul moom.