Deuteronomy 4:38 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir dàqal leen xeet yu leen sut, ëpp leen doole, ba dugal leen seenum réew, sédd leen ko bés niki tey.