Deuteronomy 4:40 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàmmleen dogali yoonam, ak santaaneem yi ma leen dénk bés niki tey, ndax ngeen baaxle yeen ak seen doom yi leen di wuutu, te ngeen yàgg ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox ba fàww.