Deuteronomy 4:42 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mu diy rawtu ci ku rey moroomu nitam, te reyu ko cig teyeef, wonu ko woon it mbañeel, lu jiitu loola. Kooku sañ naa làquji ci dëkk yooyu benn, ngir rawale bakkanam.