Deuteronomy 4:6 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sàmmooleen koo jëfe, ndax mooy doon seenug rafet xel, ak seenug ràññee fi kanam xeet yi, ba bu ñu déggee mboolem dogali yoon yii, dinañu ne: «Wii askan wu mag rekk a rafet um xel te ràññee!»