Deuteronomy 4:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ana wan xeet wu mag wu am yàlla ju leen jege ni nu sunu Yàlla Aji Sax jiy jegee saa yu nu ko wooyee wall?