Deuteronomy 5:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Teral-leen seen baay, ak seen ndey, ni leen ko seen Yàlla Aji Sax ji sante, ndax ngeen gudd fan, ndax it ngeen baaxle ca réew ma leen seen Yàlla Aji Sax ji jox.