Deuteronomy 5:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Du sunuy maam rekk la Aji Sax ji fasoon kóllëre gii ak ñoom; waaye ñook nun ñi fii tey, mboolem nun ñiy dund, ci lanu.