Deuteronomy 5:31 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yaw nag, taxawal fi man, ba ma jox la mboolem santaane bi, dogali yoon yi, ak àttey yoon yi nga leen di jàngal, te ñu war koo jëfe ca réew ma ma leen jox, ngir ñu nangu ko.»