Deuteronomy 5:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem yoon wi leen seen Yàlla Aji Sax ji teg, toppleen ko, ndax ngeen dund, baaxle te gudd fan ca réew ma ngeen di moom.