Deuteronomy 5:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buleen ci sujjóotal lenn, buleen ci jaamu lenn, ndax man seen Yàlla Aji Sax ji, Yàlla ju fiir laa. Maay topp doom tooñu waajur, ba ca seen maasi sët, ba ca maasug sëtaati nit ñi ma bañ.