Deuteronomy 6:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon yeen Israyil, dégluleen te sàmmoo jëfe, ndax ngeen baaxle te yokku bu baax, ni leen ko Aji Sax ji seen Yàllay maam waxe, ca réew ma meew maak lem ja tuuroo.