Deuteronomy 7:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Seen Yàlla Aji Sax ji moo leen di jébbal xeet yooyu, moo leen di salfaañe salfaañoo gu réy, ba ñu sànku.