Deuteronomy 7:24 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mooy teg seeni buur ci seeni loxo, ngeen far seenu tur fi asamaan tiim. Kenn ci ñoom du leen të, ba kera ngeen leen sànkee.