Deuteronomy 7:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xamleen boog ne seen Yàlla Aji Sax ji moom mooy Yàlla; mooy Yàlla ju dëggu jiy sàmm kóllëre ak ngor ñeel soppeem ñiy sàmm ay santaaneem, sët ba sëtaat, ba ci junniy maas.