bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Deuteronomy 8:1
Deuteronomy 8:1 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem santaane bi ma leen dénk bésub tey nag, sàmmooleen koo jëfe, ndax ngeen dund, yokku, ba dugg nanguji réew ma Aji Sax ji giñaloon seeni maam.