Deuteronomy 8:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye fàttlikuleen ne seen Yàlla Aji Sax ji mooy ki leen may dooley liggéey alal ji, ngir feddli ni mu ko defe tey, kóllëreem ga mu giñaloon seeni maam.