Deuteronomy 8:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo leen teg coono, xiifal leen, leel leen mànn mu ngeen xamul, te seeni maam xamuñu ko woon, ngir xamal leen ne du aw ñam doŋŋ la doom aadama di dunde, waaye gépp kàddu gu tukkee ci gémmiñu Aji Sax ji, dees na ko dunde.