Deuteronomy 9:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji ne ma: «Jógal wàcce fii gaaw, ndax sa bokk ya nga génnee Misra def nañu yàqute. Teggi nañu xaat yoon wa ma leen santoon. Móolal nañu seen bopp jëmmu tuur.»