Deuteronomy 9:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye xamleen bés niki tey ne seen Yàlla Aji Sax ji mooy kiy jàll jiite leen, di sawara wuy xoyome. Moo leen di fàkkas, mooy ki leen leen di notal, ngeen dàq leen, sànk leen ci lu gaaw, ni leen ko Aji Sax ji waxe woon.