Deuteronomy 9:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Gannaaw bu leen leen seen Yàlla Aji Sax ji dàqalee nag, buleen wax ci seen xel ne: «Sunu njekk a nu may Aji Sax ji indi nu, ngir nu moom réew mii.» Mbonug xeet yii kay moo waral Aji Sax ji dàqal leen leen.